LRC歌词

Ya Më Xollon Bama Doy La
Ngané Gëstul Xalé Bi
Tchi Noumouy Doxé
Numuy Solo
Xallé bi Super Ciof Lë

Ya Më Xollon Bama Doy Lë
Tchi Ngané Gëstul Gone Gi
Cey Numuy Doxé Ciof Lë
Xam Ngani Mbëgeel Dafa Neex
Cey BËGË Naala Xolbi Yaa Si Neek

Buko Fowee
Xoll Lufa Xass Ba Dugg Logé Fë
Dufa Jugëti
Mbëgeel Da Riche
Bul Diox Sa Xoll Bi Kulay GAAÑ

Ndawsi BËGË Nala Lë
Yaamë Gënël Gone Yi
Man Damay Jooy

So Xassee BËGË Niit Seet Lul
Lum La Def Ngané Noonu LAAY
Xallé Bii Lee Dëg Dëg Joomal Ngama
Ndax Lima Japoon Fof Nga Yamm
DANG Ko Weessu

Turr Bu Bees Bima Am Yamako Tudee
Yamako Tuddeeh
Turr Bu Bees Bima Am Yamako Tudee
Yamako Tudee Chéri

Suma Xalatee Man Nima Mel
Ak Ning Ma Bëgee Damay Jaax lé
Ni Mbëgeel Dafa Neex
Cey BËGË Nala Xol Bi Yassi Nek

Ma Monté (Montel)
Ma Wiissee (Wissel)
Ma Serré (Mbaye Nder Yagg Nga Pogné Sénégal)
Ma Monté (Montel)
Ma Wiissee (Wisseel)
Ma Serré (Ayy Nder Délol Buum Ca Boy Boy Ga)
Ma Monté (Montelma)
Ma Wiisee (Wiisselma)
Ma Serré (Bilay Les Jaloux Vont Mourir)

Mbëgeel , Mbëgeel , Nder
Legu Legu Day Neex
Legu Legu Mou Neex Ba Do BËGË Mu Jeex

So Bëgee
Aaahhhh
So Bëgee
Ma Yokal La Suma Bëgeel
Bala Ngama Merré
Ca Dëgë, Dëgë, Dëgë, Dëgë, Dëgë, Dëgë
Mbëgeel Tiss Na

Kula Bëgul Duko Xam
So Mëssul Bëgë Doko Yëkk
So Mëssul BËGË Doko Xamm
Kula Bëgul Duko Yëkk
Seet Luleen Mbëgeel Dafa Neex
Cey Bëgë Nala Xol Bi Yaa Ci Nee

Ma Monté (Montel)
Ma Wisseel (Wisseel)
Ma Serré (Mbaye Nder Day Ligeey wañi wax Dji)
Ma Monté (Montel)
Ma Wisseel(Wisseel)
Ma Serré (Ayy Nder Boléko Ak Dileen carawaché)
Ma Monté (Montelko)
Ma Wisseel (Wisseel Ko)
Ma Serré (Les Jaloux Vont Mourir)

Bilay Walay BËGË Nala
Ndaw Si KUY Baayam
Cey Wuyuma Iow
Éhh Bula Daw Loo
Wuyuma
Sabañ Mako Mbaye

Yaw Soma Bëgee DANG makoy Wan
Mbëgeel Du Lu Tuti
Yow Kuy Baayam
Cey Bulma Dawloo
Wuyuma
Sabañ Mako Mbaye

Yow Ma Wayla Ndaw Silé BËGË Nala
Cey Ma Wayla Ndaw Silé BËGË Nala

So Xarré Ma Ñëw
Finga Nek Ak Fima Nek Mbaye Sorree Nañu
Xol Day Guissé
Sa Sumala Guissé Man Contann
Mbëgeel , Mbëgeel , Mbëgeel , Mbëgeel , Mbëgeel
Métina Waw Waw Ma Wayla
Ndawsilé Bëgë Nala
Cey Ma Wayla
Ndawsilé Bëgë Nala

So Xarré Ma Ñëw
Finga Nek Ak Fima Nek Mbaye Sorree Nañu
Xol Day Guissé
Sa Sumala Guissé Man Contann
Mbëgeel , Mbëgeel , Mbëgeel , Mbëgeel , Mbëgeel
Métina Waw Waw Ma Wayla
Ndawsilé Bëgë Nala
Cey Ma Wayla
Ndawsilé Bëgë Nala

So Mënee Rekk Ni Mën Ngë
Bollé Ko Ak Dileen Wann Yoon Wi
Ay Nder Wañil Niveau Bi

文本歌词

Ya Më Xollon Bama Doy LaNgané Gëstul Xalé BiTchi Noumouy DoxéNumuy SoloXallé bi Super Ciof LëYa Më Xollon Bama Doy LëTchi Ngané Gëstul Gone GiCey Numuy Doxé Ciof LëXam Ngani Mbëgeel Dafa NeexCey BËGË Naala Xolbi Yaa Si NeekBuko FoweeXoll Lufa Xass Ba Dugg Logé FëDufa JugëtiMbëgeel Da RicheBul Diox Sa Xoll Bi Kulay GAAÑNdawsi BËGË Nala LëYaamë Gënël Gone YiMan Damay JooySo Xassee BËGË Niit Seet LulLum La Def Ngané Noonu LAAYXallé Bii Lee Dëg Dëg Joomal NgamaNdax Lima Japoon Fof Nga YammDANG Ko WeessuTurr Bu Bees Bima Am Yamako TudeeYamako TuddeehTurr Bu Bees Bima Am Yamako TudeeYamako Tudee ChériSuma Xalatee Man Nima MelAk Ning Ma Bëgee Damay Jaax léNi Mbëgeel Dafa NeexCey BËGË Nala Xol Bi Yassi NekMa Monté (Montel)Ma Wiissee (Wissel)Ma Serré (Mbaye Nder Yagg Nga Pogné Sénégal)Ma Monté (Montel)Ma Wiissee (Wisseel)Ma Serré (Ayy Nder Délol Buum Ca Boy Boy Ga)Ma Monté (Montelma)Ma Wiisee (Wiisselma)Ma Serré (Bilay Les Jaloux Vont Mourir)Mbëgeel , Mbëgeel , NderLegu Legu Day NeexLegu Legu Mou Neex Ba Do BËGË Mu JeexSo BëgeeAaahhhhSo BëgeeMa Yokal La Suma BëgeelBala Ngama MerréCa Dëgë, Dëgë, Dëgë, Dëgë, Dëgë, DëgëMbëgeel Tiss NaKula Bëgul Duko XamSo Mëssul Bëgë Doko YëkkSo Mëssul BËGË Doko XammKula Bëgul Duko YëkkSeet Luleen Mbëgeel Dafa NeexCey Bëgë Nala Xol Bi Yaa Ci NeeMa Monté (Montel)Ma Wisseel (Wisseel)Ma Serré (Mbaye Nder Day Ligeey wañi wax Dji)Ma Monté (Montel)Ma Wisseel(Wisseel)Ma Serré (Ayy Nder Boléko Ak Dileen carawaché)Ma Monté (Montelko)Ma Wisseel (Wisseel Ko)Ma Serré (Les Jaloux Vont Mourir)Bilay Walay BËGË NalaNdaw Si KUY BaayamCey Wuyuma IowÉhh Bula Daw LooWuyumaSabañ Mako MbayeYaw Soma Bëgee DANG makoy WanMbëgeel Du Lu TutiYow Kuy BaayamCey Bulma DawlooWuyumaSabañ Mako MbayeYow Ma Wayla Ndaw Silé BËGË NalaCey Ma Wayla Ndaw Silé BËGË NalaSo Xarré Ma ÑëwFinga Nek Ak Fima Nek Mbaye Sorree NañuXol Day GuisséSa Sumala Guissé Man ContannMbëgeel , Mbëgeel , Mbëgeel , Mbëgeel , MbëgeelMétina Waw Waw Ma WaylaNdawsilé Bëgë NalaCey Ma WaylaNdawsilé Bëgë NalaSo Xarré Ma ÑëwFinga Nek Ak Fima Nek Mbaye Sorree NañuXol Day GuisséSa Sumala Guissé Man ContannMbëgeel , Mbëgeel , Mbëgeel , Mbëgeel , MbëgeelMétina Waw Waw Ma WaylaNdawsilé Bëgë NalaCey Ma WaylaNdawsilé Bëgë NalaSo Mënee Rekk Ni Mën NgëBollé Ko Ak Dileen Wann Yoon WiAy Nder Wañil Niveau Bi

推荐音乐

声明:本站不存储任何音频数据,站内歌曲来自搜索引擎,如有侵犯版权请及时联系我们,我们将在第一时间处理!